+221 33 920 15 30    Email:    info.senegal@blshelpline.com
Centre biy sàkku visa pur Italie ba Sénégal

EXPERIENCE BLS APP ON MOBILESenegal google play app
google play app

Close

XIBAAR BU AM SOLO CI ÑI BOKK CI MALI – RENDEZ-VOUS VISA NULLA OSTA

Nit ñi bokk ci Mali te bëgg a def demande visa Italie bu yàgg ci kategori Nulla Osta Work walla Nulla Osta Family Reunion, war nañu jëfandikoo liyaŋ bi ci suuf ngir jël seen rendez-vous.

Liyaŋ bu dëggu ngir jël rendez-vous: https://sn.waitlist.theitalyvisa.com/en

Toppal leen jàngat yii ni mu ware:
1. Cuqal ci liyaŋ bi ci kaw ngir dugg ci xëtu rendez-vous bi.
2. Ci menu bi ñuy wax «Purpose of Travel», tànnal kategori bi méngoo ak sa demande:
* Mali – Work su fekkee visa Nulla Osta Work la nga bëgg.
* Mali – Family Reunion su fekkee visa Nulla Osta Family Reunion la nga bëgg.
3. Ci wetu «Country», Mali dina feeñ ci sa bopp.
4. Ci wetu «Application Office», tànnal Bamako.
5. Tànnal «Service Type» bi nga soxla ak limu nit ñi bokk ci réservation bi.
6. Toppal jéego yi ci suuf ba sa réservation rendez-vous mat.

LU AM SOLO: Seetal bu baax ndax kategori visa bi ak biro bi nga tànn dëppoo nañu ak sa demande bala ngay jàll ci yeneen jéego yi.

YEGGAL BU AM SOLO

YEN WUKAT YI,
BËGG NANU LEEN YËGAL NI, LI KO DALEE 16 OKTOOBAR, 2025, AGENCE BLS DINA MËNA NANGU KÀTTAN POUR GNI DEMÀNDE VISA NGIR BOOLE FAMIY YI AK ÑI NEKKUL CI DËKK BI. NDAX DOOMI ITALIE, DAÑU WARA JOX KÀTTANU ÀTTEKAT BI KENN KU BOKK CI BENN NJABOOT.

1- LU KO DALEE 21 SULET 2025, VAC BLS ITALIE DU NANGU XAALIS. METOOD FAY YIÑI NANG:
WAVE, XAALIS ORANGE, WALA KARTU KREDI/DEBIT (AMUL AMEX)

2- RANDEWU YI NGIR LEGALISASIOŊ CI ÑAARI AYU-BIS YI NJËKK DINA ÑU UBBEEKU CI 29 WEER WU NEKK AK ÑAAREELU ÑAARI AYU-BIS YI CI 14 WEER WU NEKK TÀMBALI 12:00 PM.

3- "Dina nu yëgal jëfandikukat yi ni lu ko dalee altine 9 màrs, dina ñu mëna am ranndiw ngir joxe seeni demànd visa Schengen jaaraleko ci portaalu Prenot@mi: https://prenotami.esteri.it/
Ngeen bàyyi xel ni dina ñu wéyal di joxe demànd yi jaaraleko ci agence BLS International.
Soo bëggee yëgle ab jafe-jafe, deñu lay digal nga yonne bataaxal ci visa.ambdakar@esteri.it
Adres imeel bii di dakar.vistiaffari@esteri.it mingi wéy di dox ngir ñiy sàkku visa liggéey yu bawoo ci sosete yu Italie yi."

Assurance tukki ngir visa Schengen

Sertifikaa di assurance tukki dañu ko wara joxe ci santu demànd visa bi ndax loolu mooy li ñuy laaj ci ñiy tukki ci Italie. Mën nga am sa assurance tukki ci bépp kompiñi assurance buñu may sañ-sañ, wala nga bës ci lëkkalekaay yi ci suuf soo bëggee jëfandikoo serwiis bii leegi.

  1. Europ Assistance: Cliquez ici
  2. SIA Assitance: Cliquez ici

Tegtal:- Soo bësee ci lien bii, dina ñu la yóbbu ci sitwebu beneen pàrti, dina ñu jëfandikoo sa done yu bopp ci anam wu méngoo ak seeni sàrti bopp. Ngeen bàyyi xel ni BLS du jël wala jëfandikoo benn leeral bu ngeen joxe ci seen sit te amul benn wareef ci benn xëccoo.

XEETU DEMAND VISA BU ITALIE

BLS International Services Ltd. mooy mbokk mu wóoral ci Ambassade bu Italie ci Sénégal ngir doxal ligéeyu administration ak ligéey yi amul ci xél ngir doxal demande visa yi.

Ñi ñuy demande ño ñooy responsable ci demande yi ñuy yóbbal. Kenn ku am informaasiyu fénn walaa mu wéddi dëgg, document yu suqali yu manqué walaa yu wéruldina am lu mu def ci décision bi Ambassade bu Italie ci Sénégal di jël.